Home Music Video & Lyrics

Youssou N’Dour – Yeksil (Remix)

Youssou Ndour - YEKSIL REMIX - CLIP OFFICiEL

Download Yeksil (Remix) Mp3 by Youssou N’Dour

The Senegalese singer, songwriter, musician, composer, and politician Youssou N’Dour presents to us a compelling song, as this masterpiece is titled “Yeksil (Remix)“. This track, released in 2025 , is a captivating and inspirational addition to any music enthusiast’s collection. The tune “Yeksil (Remix)” carries a powerful message and a mesmerising melody, making it a must-listen for all. Feel free to stream the mp3, watch the video, and sing along to the heartfelt lyrics.

Get the MP3 audio, download, stream, and share this amazing song with your friends and family. When you share it, you’re spreading the goodness and joy of the song. #CeeNaija

DOWNLOAD HERE

Download More YOUSSOU N’DOUR Songs Here

Listen on your favorite platform

Lyrics: Yeksil (Remix) by Youssou N’Dour

Gรซjoon fi lool bi nga รฑรซwee
Bi nga รฑรซwee
Duma fร tte nit nitam
Mooy garabam
Bokk nga ci รฑi
Bokk nga ci รฑi ma gรซn a bรซgg
Hi hiiiiiiiiiiiii hiiiii
Koล‹- Koล‹, Yegsil daal
Koล‹- Koล‹, Yegsil daal
Koล‹- Koล‹, Yegsil daal yegsil daal
Koล‹- Koล‹, Yegsil daal
Yegsil avec plaisir
T’amรจnes que de beaux souvenirs
Waxtu wu la neex
Mรซn nga fรซgg
Fii doo fii gan
Bu nu waxantee dรซgg daal
Bokk nga ci รฑi ma bรซgg
Koล‹- Koล‹, Maa ngi xaar
Pressรฉ dโ€™entendre ta voix
Biig rekk, sax jโ€™ai pensรฉ ร  toi
Gรซjoon fi lool bi nga รฑรซwee
Gรซjoon fi lool bi nga รฑรซwee
Nee naa la, nee naa la, nee naa la
Bismi, bismi, bismillaah
Gรซjoon fi lool bi nga รฑรซwee
Nee naa la, nee naa la, nee naa la
Bismi, bismi, bismi, bismi, bismillaah

๐ŸŽต Are you a gospel artist? Get your song featured on CeeNaijaReach millions of gospel music lovers

Promote

Koล‹- Koล‹, Yegsil daal
Yegsil avec plaisir
T’amรจnes que de beaux souvenirs
Waxtu wu la neex
Mรซn nga fรซgg
Man de xam naa
Ne sa fรซgg yaw
Bokk nga ci รฑi ma gรซn a bรซgg
Man de damaa gis ci yaw sincรฉritรฉ
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yร kkamti sa jotaay ak sa ree ju neex
Man de damaa gis ci yaw sincรฉritรฉ
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yร kkamti sa jotaay ak sa ree ju neex
ร‘รซwal saa yu la neexee sa รฑรซw
Man da fa may dundal
Man de damaa gis ci yaw sincรฉritรฉ
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yร kkamti sa jotaay ak sa ree ju neexPour plus de vidรฉos, abonnez-vous sur notre chaine

๐Ÿ”’ All songs and media on this page are shared for gospel promotion purposes only. All rights belong to the respective artists and labels. If you are the rights holder and wish content removed, please read our DMCA & Copyright Policy or submit a takedown request here.

Comment below with your feedback and thoughts on this post.