Download Cosaan Mp3 by Daaraj Family
The Senegalese rap duo Daaraj Family presents to us a compelling song, as this masterpiece is titled “Cosaan“. This track, released in 2025 , is a captivating and inspirational addition to any music enthusiast’s collection. The tune “Cosaan” carries a powerful message and a mesmerising melody, making it a must-listen for all. Feel free to stream the mp3, watch the video, and sing along to the heartfelt lyrics.
Get the MP3 audio, download, stream, and share this amazing song with your friends and family. When you share it, you’re spreading the goodness and joy of the song. #CeeNaija
Download More DAARAJ FAMILY Songs Here
You May Like These Too 🔥
Lyrics: Cosaan by Daaraj Family
REFRAIN:
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fatte , bul fatte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fatte , bul fatte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fatte , bul fatte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fatte , bul fatte
Fa nga cosaanoo !!
Couplet Faada :
Xam na nu fi nu jogee
Li nu jaxal moy funu jëm de
suufu maam yi moom bu nu woowe
Du nu tà nqamlu du nu soree
danuy fatu numu gëna gaawe
Ñun ndawu Reew mi da nu pare
Ji fi luy jëriñ fi ak fë le
Ba ñu ñu ci dara ku ngemboy bëre
wër naa addunaa
Japon Inde Australia
There is no place like home
Fen du Sunugaal
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Couplet Ndongo :
Ku fi fatte demb
ëlëg dalay reer
Waxu mag la degg nga
Du am kubeer
fattëlikul ki nga doon , fi nga juddoo
Fi nga juggee,fi nga dëkk Yalla mi la bindd
Ngor, jom, fit la ,fayda booko amul
doo xam fi nga jëm dara du ku dinddi
Li ci Baay bi di doom na ko jëli
Kaddu mag ñi nii na ko sët yi firri
Na nu gëna disoo ndax ñu mëna deggoo
xana giso jikkoo yi ni gëna yà qoo
Na nu dellu te toogi mëna root du doy di
adduna ngi daw di na ñu def ci bop yi
Bul di fatte ñi la fà l ñi la tettewoon
Ñi la gunge bi ngay raam ñi nga nekkaloon
Lakoon fakoon ñakoon
Lawoon fawoon ñawoon
Xaleel poto poto la
Noko raaxe rek lay weyee
Fi laa yaroo fi laa maggee
Lumu guddi guddi guddi damay ñibbee
Galsen moy daw sunu dereet
dañu wutiwoon ba tax ñu ne bëreet
Teranga yi ñi fay jëlee su nu askan lañkoy jëmee
wër naa addunaa
Japon Inde Australia
There is no place like home
Fen du Sunugaal
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo





