Download Cosaan Mp3 by Daaraj Family
The Senegalese rap duo Daaraj Family presents to us a compelling song, as this masterpiece is titled “Cosaan“. This track, released in 2025 , is a captivating and inspirational addition to any music enthusiast’s collection. The tune “Cosaan” carries a powerful message and a mesmerising melody, making it a must-listen for all. Feel free to stream the mp3, watch the video, and sing along to the heartfelt lyrics.
Get the MP3 audio, download, stream, and share this amazing song with your friends and family. When you share it, you’re spreading the goodness and joy of the song. #CeeNaija
Download More DAARAJ FAMILY Songs Here
Lyrics: Cosaan by Daaraj Family
REFRAIN:
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fatte , bul fatte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fatte , bul fatte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fatte , bul fatte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fatte , bul fatte
Fa nga cosaanoo !!
Couplet Faada :
Xam na nu fi nu jogee
Li nu jaxal moy funu jรซm de
suufu maam yi moom bu nu woowe
Du nu tร nqamlu du nu soree
danuy fatu numu gรซna gaawe
รun ndawu Reew mi da nu pare
Ji fi luy jรซriรฑ fi ak fรซ le
Ba รฑu รฑu ci dara ku ngemboy bรซre
wรซr naa addunaa
Japon Inde Australia
There is no place like home
Fen du Sunugaal
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Couplet Ndongo :
Ku fi fatte demb
รซlรซg dalay reer
Waxu mag la degg nga
Du am kubeer
fattรซlikul ki nga doon , fi nga juddoo
Fi nga juggee,fi nga dรซkk Yalla mi la bindd
Ngor, jom, fit la ,fayda booko amul
doo xam fi nga jรซm dara du ku dinddi
Li ci Baay bi di doom na ko jรซli
Kaddu mag รฑi nii na ko sรซt yi firri
Na nu gรซna disoo ndax รฑu mรซna deggoo
xana giso jikkoo yi ni gรซna yร qoo
Na nu dellu te toogi mรซna root du doy di
adduna ngi daw di na รฑu def ci bop yi
Bul di fatte รฑi la fร l รฑi la tettewoon
รi la gunge bi ngay raam รฑi nga nekkaloon
Lakoon fakoon รฑakoon
Lawoon fawoon รฑawoon
Xaleel poto poto la
Noko raaxe rek lay weyee
Fi laa yaroo fi laa maggee
Lumu guddi guddi guddi damay รฑibbee
Galsen moy daw sunu dereet
daรฑu wutiwoon ba tax รฑu ne bรซreet
Teranga yi รฑi fay jรซlee su nu askan laรฑkoy jรซmee
wรซr naa addunaa
Japon Inde Australia
There is no place like home
Fen du Sunugaal
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo