Download Waxtu Mp3 by Ashs The Best Ft. Amadeus
The dynamic and vibrant singer Ashs The Best, comes through with a song called “Waxtu” featuring the eminent music artist “Amadeus“, and was released in 2024. This amazing and inspiring track is a must listen for any music lover. With its message and captivating melody, “Waxtu” is an addition to any playlist. Whether you want to download the mp3 watch the video or sing along with the lyrics, “Waxtu” is undeniably a song that will deeply touch the hearts of everyone who encounters it.
Get the MP3 audio, download, stream, and share this amazing song with your friends and family. When you share it, you’re spreading the goodness and joy of the song. #CeeNaija
Download More ASHS THE BEST Songs Here
What makes this song even more special is the collaboration with the acclaimed and award-winning music artist โAmadeusโ. Their skills behind the scenes have truly brought this song to life.
Lyrics: Waxtu by Ashs The Best
verse
Ndekete yรณo waxtu yรฉ รฑu boole woon du xaritoo kase
Ndekete yรณo waxtu we taxoon รฑu doon dajee weer bu ne
Woo nga ma ci guddi gi fekk mu maas
Ci รซlรซg tamiit, fi ci suba ci, fekk mu naaj
Waxtu bi su weeso dotul รฑรซwaat
Do ko dabuwaat
Bala dellusiwaat
Mu nekk ci beneen bรซs
Bu jร nt bi di so fi, fรฉele di naaj
Bu guddi gi di xaaj fi, timis di waaj a jot fe
Massamba ma nga Walo
Suba soxla ya koy yoobu Ndakaaru
Te รซlรซg ndogal mรซn na fa xandalu
Fi ak ay bรฉs mu jiibi sanc walo
Ndekete waxtu yi รฑooรฑii boolee
รoom รฑooรฑii boolee
Du xaritoo kaase รฑoom รฑooรฑii boolee
Ndax bu รซlรซge mรซn naรฑu jiiwalo
Waxtu w saay su jotee(bu fekkee waxtu woowu la wootee)
Foo mรซn ti nekk, waxtu w bu jotee
Budul suba tamiit sa boos moo รฑi รฑรซw
Ass fay nee na du xaar suba
Ndax yร kkamti na te dรฉmb weesu na
Ku sร kk gaa ye moo รฑi dajaale
Ci adduna bee ci waxtu jii li mel tay
Mara naan, marul naan, naan, am na potu-ndaal
Ndox ma ngay walangaan, รฑun buรฑu rรฉeroo
Ndox ma ngay walangaan, รฑun buรฑu rรฉeroo
Te amaana buรฑu diisoo di naรฑ dรฉggoo
รu baรฑ di rรฉeroo
outro
Naรฑu dรฉggoo di baรฑ di rรฉeroo
Amaana buรฑu booloo mu may รฑu doole
Boroom bi def ci ndam su ko soobee
Bu รฑu boolo, naรฑu boolo