Download Aras Mp3 by Ashs The Best
Here’s an amazing song and music lyrics from the exceptionally talented singer, “Ashs The Best“. It’s a song titled “Aras“, and was released in 2025. This beautiful song, accompanied by a stunning music video, audio, and lyrics, is sure to captivate listeners of all ages. Don’t miss out on this beautiful musical experience.
Get MP3 audio, Download, Stream, and Share this powerful song with your friends and family, and let the blessings overflow! By sharing it with your loved ones, you’re spreading the goodness and joy that this song brings. #CeeNaija
Download More ASHS THE BEST Songs Here
Lyrics: Aras by Ashs The Best
ย Bรซgguma ngay gis lu la yรฉem
Bรซgguma nga gis lu la jaaxal
Jaral na ma faat bakkan yaw nga dund
Bรซgguma la gis ngay caalit
Xanaa xamoo ni benn laรฑ
Ndekete Yร lla รฑu boole
Ndekete Yร lla รฑu boole
Fii ci suuf ci asamaan si
Yร lla รฑu boole, รฑu doon benn say
Dinaa la xamal bu doon benn fas
Naaru gรณor laa ci yaw
Man dinaa la dawal Safaa’g Marwaa
Kenn du ma jiitu ci yaw
Dinaa la yรซgal ni Yร lla รฑu boole
Bind na ko Aras
Buรฑ demee ba gisatoo ma
Daa fekk man ma jiitu la Aras
Man dinaa la xamal bu doon benn fas
Naaru gรณor laa ci yaw
Man dinaa la dawal Safaa’g Marwaa
Kenn du ma jiitu ci yaw
Man dinaa la yรซgal ni Yร lla รฑu boole
Bind na ko Aras
Buรฑ demee ba gisatoo ma
Daa fekk man ma jiitu la Aras
Asaman ak suuf
Yaay suuf yaay asaman
Yaay bidรฉew biy leeral
Man dinaa la xamal ni Yร lla รฑu boole
Bind na ko Aras
Buรฑ demee ba gisatoo ma
Daa fekk man ma jiitu la Aras
Gis la ci lรซndรซm bi te nekk ci leer
Baayi la fa ngay gรซlรซm
Metit bu naree รฑรซw di dal sa kaw
Ma taxaw dekku ko
Dinaa la xamal ni Yร lla รฑu boole
Bind na ko Aras
Malaakal Mรซwti sax bu la soxla woon
Na ma jรซl bร yyi la
Metit bu naree รฑรซw di dal sa kaw
Ma taxaw dekku ko
Yaay booyโฆ
Yaay bidรฉew biy leeral asaman
Asaman ak suuf
Yaay suuf yaay asaman
Yaay bidรฉew biy leeral
Asaman ak suuf
Dee ma ree
Dee ma ree, ma lay ree
Dee ma ree
Dee ma ree, ma lay ree